1 year ago
Bul ma miin
Lyrics
Bul ma miin, Bul ma miin
Bul ma miin ba fatte ma
Kon mu ňaaw
Adduna yaa mëna wor
Xaň ma ndey xaň ma baay
Boo ma digee sama doom nax nga ma
Lekkatuma, naanatuma
Tëddatuma, nelawatuma
Boo ma digee sama doom nax nga ma
Alarba la woon ci weeru koor
Mu taggu ma ne ma maangi ňëw
Boobu ba téy gisuma sama doom
Woy wéét, woy wéét
Woy wéét adduna
Sama doom dem na nii
Writer(s): BARTHELEMY KOFFI ATTISSO, NDIOUGA DIENG
Copyright(s): Lyrics © BMG Rights Management
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind
The Meaning of Bul ma miin
Be the first!
Post your thoughts on the meaning of "Bul ma miin".