Yaco Mome
Yaco Mome

Lass - Yaco Mome Lyrics

Jun 11, 2021
7
Yaco Mome Music Video

Yaco Mome Lyrics

Bisse bi yaye borome
Bisse bi yaco mome
Lougnou namone thie yaw
Guisse nagnouko
Taye die ya ayyé
Taye die lagnoula mayé
Xalé bou yarouga
Gnoundé lére nagnou
Fognoula dane haré yaw
Guisse nagnoula fa
Fognoula dane sénetou yaw
Fékeu gagnou fa
Daga done kou yarou
Kignouye roye
Daga done koubahe
Ak sa dieko biiii

Héeee yayo
Dagaye seyyi
Héeee yayo
Ya héwlé gnou téwe

Gnoune dagno bégue baye dioye
Lagne done gnane borombi maye nagnouko
Di santeu té dila gnanale
Wadiour diouné nane borombie mayeko
Doome dja magueu baye seyyi dié
Conne warrato dioye fonpale rongnogne yé
Taydie sa bisseu la béguel waye
Taydie yaco mome mané béguel waye

Héeee yayo
Dagaye seyyi
Héeee yayo
Ya héwlé gnou téwe

Writer(s): Bruno HOVART, Lansana SANE, Paul CUCURON
Copyright(s): Lyrics © VELVETICA MUSIC, WAGRAM PUBLISHING, VELVETICA MUSIC PUBLISHING, 64 RPM
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Attach an image to this thought

Drag image here or click to upload image

The Meaning of Yaco Mome

Be the first!

Post your thoughts on the meaning of "Yaco Mome".

Lyrics Discussions
by Steffany Gretzinger ft. Bobby Strand

1

174
Hot Songs

5

2K
Recent Blog Posts