Mo Yaro
Mo Yaro

Lass - Mo Yaro Lyrics

Sep 22, 2021
41
Mo Yaro Music Video

Mo Yaro Lyrics

Doyegama si kersé
Wonégako mome
Xalé bou yarou
Mané yama mome
Ya ligueye lou méleni
Amoulo morome
A dieufe diou bahe die
Mani yaye borome

Fougnoula toudé
Mané mo yaro
Sa ligueye la
A xalé bilé mané
Mané mo yaro
Sa ligueye la

Weurnala si kogne bi
Kéneu méni yaw
Sa youmala séné
Xole bi dale si yaw
Ha mané yalla samala
Hé mané yalla samala

Doyegama si kersé
Wonégako mome
Xalé bou yarou
Mané yama mome
Ya ligueye lou méleni
Amoulo morome
A dieufe diou bahe die
Mani yaye borome

Fougnoula toudé
Mané mo yaro
Sa ligueye la
A xalé bilé mané
Mané mo yaro
Sa ligueye la

Mo yaroooooo
Ki moka yarooooo

Writer(s): Alexandre CHIERE, Lansana SANE, Paul CUCURON
Copyright(s): Lyrics © WAGRAM PUBLISHING, 64 RPM
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Attach an image to this thought

Drag image here or click to upload image

The Meaning of Mo Yaro

Be the first!

Post your thoughts on the meaning of "Mo Yaro".

Lyrics Discussions
by Steffany Gretzinger ft. Bobby Strand

1

174
Hot Songs

5

2K
Recent Blog Posts