Habib Faye
Lyrics
Adduna bi du dara, te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp, xamal ni japp u loo ci, dara
Adduna bi du dara, te dara xaj u fi
Bi Lahii ku ko japp, xamal ni japp u loo ci, dara
Man Youssou ñakk naa, andandoo bu sincère
Adduna, adduna daal, nax ati na ñu
Adduna, adduna da fay wor ee
Habib Faye, dem na nii
Waa ju baax, guddée na waay
Habib yaru woon na, and ak dignité
Fonŋk oon na liggéey ёm, bëgg njaboot am bu, baax
Doon oon jàmbaar
Man Youssou ñakk naa, andandoo bu sincère
Adduna, adduna daal, nax ati na ñu
Adduna, adduna da fay wor ee
Habib Faye, dem na nii
Waa ju baax, guddée ne waay
Adduna, adduna
Adduna, adduna
Adduna, adduna daal, nax ati na ñu
Adduna, adduna da fay wor ee
Habib Faye, dem na nii
Waa ju baax, guddée na waay Waa ju baax, guddée na waay
Writer(s): Youssou N'Dour
Copyright(s): Lyrics © THE MEZZO AGENCY, LLC, Songtrust Ave
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind
The Meaning of Habib Faye
Be the first!
Post your thoughts on the meaning of "Habib Faye".