Ci Loo Nekk
Lyrics
Bouma kèn yakhal sam olala
Sangou ak sa crush au lit lit
Balaamay D mounaan kooba la
Baiser opposition bi yeup comme Idy
Fuck gnidi transhumer comme idy
Comédie comme Eddy
Leer nama comme midi ni beut bou guiss xam lou bopp meun yenn
Young fif boulen baal c'est ce qu'on me dit
Zo dollar maafiy tête d'affiche si news
Dama tiit si flouz mais diot naafi nekk hafiz si jews
Def naa ay lacets si shoes
Sol ay plaquets si jewls
Ay pétasses beug meu masser ni Ouz
Baakh moo dieekh laay retenir
Kouy lathieté soutient na dem aabi bas
Dama rajeunir gueneu dieekh sama calpé daa maag fess melni Abiba
Kong leen ni Astar ak niétélou baram
Boy ferme ta chatte nganaan mane danga mouss doomou kharam
Fii kèn doula maral doo yeungueul gamebi yeungueul arass nga gueneu meun arrête tes salades
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Nieuw sa gallé guéné baayi ay kilos neew
Abozé
Ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Suis dans le foncier jaay ay parcelles cimetière golden boy saleteel fepp
Boul yooner message à part virement
Metti ni flexion sans étirements
Jeune marié dootoumeu mécher mais Zeus laay transférer ay xallé mouy recrutement
La Masia Mafia
Dioudou rek dead maagui aakhira
Sol jellaba djitté naafila
Bountou Bicis difa naafila
Manela jeune célibataire biy Couplet ak kila def reuf
Wakhma Lou bandit di ragal si keuf
Tekki yor Xaliss bou takkou ni mbeur
Sakou sa guel iow ngay sakkou ndimbeul
Xallé yi mane laniouy weur
Talent bou excitant maylassi leuf
Logiquement limay def dougou sa soeur
Clashma boy doumla vent damalay euf
Tu t'assoies pas sur ma table, ndakh bine dago sieze bou ley dieulé ci banc mon frère
Je m'assoie devant la glace bouma namé guiss kou key taangal melni mane okay
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Nieuw sa gallé guéné baayi ay kilos neew
Abozé!
Ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Zeus ci loo nekk
Zo ci loo nekk
Suis dans le foncier jaay ay parcelles cimetière golden boy saleteel fepp
Ci loo nekk
Si sen taat di sillonner
Souniou wakher si money
Doo encaisser ni simone
Wakhma bouder feeloo leen
Vrai rap galsen pionnier
Golden boy
Rio Kylian featuring Capsi Lionel
Abozé
Wooooo
Writer(s): Baye Dial Gueye
Copyright(s): Lyrics © Ferdinand Malick Hortala
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind
The Meaning of Ci Loo Nekk
Be the first!
Post your thoughts on the meaning of "Ci Loo Nekk".