No Limit
Lyrics
Deff Music
Yeah
I' am in love with you
Xel mi moogsi iow soubeu ba ngoon
Baby loooooove miss you
Fii laala sokhla bouma yeewo soubeu teel
Ay att di ngoro
Fimla denth sorri damla love ba forokh (ahaaaah)
Dieul sa numéro
Composer wooter jot leu khol bi cedd hello
Soukeur sama life Yaay khorom
Khol bi yaassi nek yaay borom
Dinaa def sa yaay goro
Digueunté moogui ladj gouro
Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Bébé si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Bébé si mane amoo limite
Mane ma waroon di ladj
Fima toolou si iow
Amoo limite thi mane
Bouder mbeuguel dou jaay
Téwoul diaral ngama
Iow yaay ki gueun thi mane
Nakh damla bouga
Boulma baayi lokhotima fouma douga
Na nga melni soular
Ak bouteille bimou top moukoy douma
Baby xamanter nagn Maak iow ça fait Longtemps
Domage, Ndakh defagooma demande
Nee ngueu kagn la wesssou dokhaan
Xamga Mais dinalako wakhaat
Soukeur sama life yaay khorom
Khol bi yaassi nek yaay borom
Dinaa def sa yaay goro
Digueunté moogui ladj gouro
Parce que si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Bébé si mane amoo limite
Limit limit Limit
Parce que khol bi iow la bouga
Bougaa Bougaa Bougaa
Bébé si mane amoo limite
(Bébé si mane amoo limite)
(Bébé si mane amoo limite)
Writer(s): Ferdinand Hortala, Baye Gueye
Copyright(s): Lyrics © Ferdinand Malick Hortala
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind
The Meaning of No Limit
Be the first!
Post your thoughts on the meaning of "No Limit".