Deff 4
Deff 4

Oothentik Zeus, Mist Cash - Deff 4 Lyrics

85
Deff 4 Music Video

Deff 4 Lyrics

Daniou dikk poup si sa kaaw lal
Nioola téré nelaw waayé nioola gueneu teureudi fils
Maala dakh rap diaratoula wakh negger maneu teul diaroul baako Brésil ish
Talent sama jury maalay dicter sama loi même booy lekk bic rouge doomeu maneu corriger
Ani real ani fake my man boudé gni dakh fausse note si sen sons laaniounaan très bien
Far si yén
Fakani Éparpiller
Ndieukouniou depart fi déh
Arrivée bi tar si Yén
Waxleen ni maafi né dag séni laf yi yeek
Rapeur yi maafé yét
Li wërëdi fateu si yén
Téléphone bi car car car baniou fatigué
Teki siw fat fat fat sounou cartier
Mounouniou écarté xamounioula sa quartier
Diox rap bi limou lathieté néko negger dou baxx si yèneu
Maagui fenen nakh khadiouma sa team
Gueun leu dee gueun leu siiw comme bryant Kobe
Demleen si mére di mbiip warmith nguen di def sama mère meussoul wooté meeting
Andak bruit
Contaan ngueu mbokk
Maay van damme fii
Iow fane nga bokk
Fantastiques
Fatal sa nop
Ap ngandam hit
Ay ngandam bop
Ay defkat tigui
Tigui Tigui Tigui
Ay defkat tigui
Tigui Tigui Tigui
Ay defkat tigui
Tigui Tigui Tigui
Defkat tigui
Tigui tigui tigui tigui
Ay defkat tigui
Nioun yapou sa rappeurs yi laniou dibi
Faakk ni guèneu deuk bi gnibi
Sibiti nga nek di xow
Kepp ko please
Thiéné sama... please
Defkat tigui
Garabou gouy si digou timis
Kouniufi pique nga piqué crise
Beug niou fay mooy wérou midi ngay taal tchipiri niooy def kat tigui
Teew pour diaxassé carte gui clater fi
Niow pour daguatélaak sa team wa taataguine
Beug ma fay beug ma ray ma taal sa thiin
Tekki tedd mére bi tèguélé tank yi
Lima dal wéreudileu teh sa dom yi douma fath
Même boo deukoulé si mbedd tamitt boybi nala fatt
Boybi Ligueey laafi indi yénay dieuli limay wakh
Negger niam nga sama lokho limla yakk dala mbadj doomou khath
Doto khathie fi fake yima diota khagn peace
Iow la yaay king couronne bi laalay kong neggers yidoneu lathie god neko cash lay dooon
Ay fuck lay doon fuck Papa yaay doom
Maay arrivée bi douma daw thioow
Familly bi beuri nguen beug lol beug laal
Xana nékoul barki demb nguen diongu?
Hey boy Zeus dawalal dawalal dawalal boy
My man cash dawalal dawalal dawalal fils
My man Zeus dawalal dawalal dawalal boy
Walabok Cash dawalal dawalal dawalal fils
Comme domeram tigui

Daguatélaak sa team wa taataguine
Beug ma fay ma taal sa thiin
Tekki tedd mére bi tèguélé (rires)

Writer(s): Baye Dial Gueye, Mouhamed Fallilou Mbacké Ndour
Copyright(s): Lyrics © Baye Dial Gueye
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Attach an image to this thought

Drag image here or click to upload image

The Meaning of Deff 4

Be the first!

Post your thoughts on the meaning of "Deff 4".

Latest Blog Posts
Lyrics Discussions

1

176
Hot Songs
Recent Blog Posts