À La Vie, À La Mort
À La Vie, À La Mort

Oothentik Zeus - À La Vie, À La Mort Lyrics

3
À La Vie, À La Mort Music Video

À La Vie, À La Mort Lyrics

Yeah
Khaar nagnla reer foo fétéwoon
Yalna yallah buur léral sa yoon
Happy new year sama doom
Mere bi dafa couper rek ma diooy
Digueunté lima defak lépeu li nga diota mougn
Guisnaané sooneu ngueu si biir si kanam dga cool
Yaay gorr nagn samay tank bimla khalaaté laa diouk
Takk nga sa biir pour mane kone tay boo guèkhé rk ma sour
Bouma sagnoon douma masseu reerook sama baye
Mom si mak cahiers yi rk lay nangoo di guissé sama aay Si samay eyes
Naa doon milliardaire bou teuyé mic
Kone nama gaagn, tay soubeu fadialma louma lath
Yeewou midi cororico niou dem teudi
Opinion bi def niou bonn nioun gangster yi
Rappeur nekoul publicou con lay conquérir
Xam xam laniouy dieufeunikoo tout comme serigne
Boule bi dafay tourner diant lakhatou si timis
Loolou laa téleu xamal gnidoon fight moudoon metti
Lima diaakhal nekoul bount bou ligueey di tidji
Looloo waral teudiou di job night lou doon mérite
Langamou si job bou touti niémé wakh diou beuri
Moudiei teureureuri Beu doon kaagn si sen meuniin
Li nieup sokhla laay récupérer tek sama city
Loolou laniou tontu gnidoon ladj lougndoon dieuli.
Dioudouwouma am mais douma dèh si niak
Niakouma mbok you am, douma méré nitt si sa alal
Niaakaguma touss teh awma looma ragal niak
Nakh Gueuwmané fii meun neu thiool ba gueun fi maneu niangu
Nioun leu genrou boy yi yagg dem nioulendi kheep
Nioun la borom khel yign beugoulwoona baayi khel
Doo deg wakhou kheet boudei khaliss nga kheegn
Day dem ba foula neekh nga freq ni Wally Seck
Mane sama life laay rap
Li rap bi lath laa am
Li nguendi lath laa xam
Mootakh figuen dadj laa khar
Denthienaa paath nakhar
Takk niouy diaay sakhar
Teh dina weuy di ligueey boumay deg tarfakallah
Bae amnaa temps wou beugueunté mais awma temps wou fiir
Boo meunoul yem si mane boul sentou si nioun avenir
Xamnaa lepp loo def mais nak je vais pas te dire
Damlay baayi ngay guénak sa bop et c'est ça le pire.
Des fois diga gagner match meriter défaite
Way bouy keup gaal bind refrain si téfess
Comme ay rabou aaleu lékanté laniou deuké
Nioo bokk louniuy def mais bookuniu deffé
Nioom daniou
Beug siiw ragal thioow (Iyeah)
Beug riche teh dougn job (Iyeah)
Boo beugué guiss fouma flop (Iyeah)
Beug siiss koulay thiop (Iyeah)
Succès bi dina nieuw (Iyeah)
Yea i feel di nga know (Iyeah)
Dina khiin dina taw (Iyeah)
Douma tiit douma daw (Iyeah)
Nagnma beug nagnma haïr (Iyeah)
Mais dou niak niouma trahir (Iyeah)
Ak loumou metti douma baayi (Iyeah)
C'est à la vie à la mort (Iyeah)
Thioono dikk yéneu saaayiii yeaaaah
Khelmi dem sama yaay (Iyeah)
Tégui thioono sama yaay (Iyeah)
À la vie à la mort (Iyeah)
Fanane naa sissa lal yaay
Sama rakk dioudou ma dem teudi sissa roum (Iyeah)
Diga mouugn li nga mougn (Iyeah)
À la vie à la mort (Iyeah)
Deukeul ngama sama mame booy
Degg nga louné waayé takhoul ba nga ba (Iyeah)
Dougn am deug sissa kaw (Iyeah)
À la vie à la mort (Iyeah)
Nagnma beug nagnma haïr (Iyeah)
Kheuyneu dou niak niouma trahir (Iyeah)
Loumou metti douma baayi (Iyeah)

Deukeul ngama sama mame booy (Iyeah)
Degg nga louné waayé takhoul baga ba (Iyeah)
Dougn am deug sissa kaw (Iyeah)
À la vie à la mort (iyeah)
Iyeah

Writer(s): Baye Dial Gueye
Copyright(s): Lyrics © Ferdinand Malick Hortala
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Attach an image to this thought

Drag image here or click to upload image

The Meaning of À La Vie, À La Mort

Be the first!

Post your thoughts on the meaning of "À La Vie, À La Mort".

Latest Blog Posts
Lyrics Discussions

1

176
Hot Songs
Recent Blog Posts