Gnafélen
Lyrics
Masta koula beugeu lacoye wahe
Mar wane mar wane masta
Deugeu deugeu goryalla diamabarga
Boula dara méti yonou daw dou gaw
Diogale ga gnafé watctou wi da gawe
Fi lofi défoule doguisdé
Gnafélene Gnafélene Gnafélene sama gayi
Gorgorlou léne yéne gayi
Doundou immgré mitina lolou
daga bayi sa réwe gneuw bittime réwe
Deugeu deugeu goryalla yéne aye diamabar guéne
Gnafélene Gnafélene Gnafélene sama gayi
Gorgorlou léne yéne gayi
Bisbouné yagui woné sa diambarté ak pression nougnou barré
Loloudale doula taha delou guinawe
Dahe xamegani thiono dou rére
Gnafélene Gnafélene Gnafélene sama gayi
Gorgorlou léne yéne sama gayi
Diambarou diambar yaguiné
Gnome dale dougnou massa délouguinawe
Dahe xamnagnou lane lagnou bayi guinawe
Thiahane tahouléne diock dale
Dore ware goudé ak beuthieuk
Dahe xamnagnouné thiaxane fahé
Dahe xamnagnouné fi amoule délou guinaw
Gnafélene Gnafélene Gnafélene sama gayi
Gorgorlou léne yéne sa gayi
sama gayi sama gayi sama gayi
Writer(s): Bruno HOVART, Lansana SANE
Copyright(s): Lyrics © VELVETICA MUSIC, WAGRAM PUBLISHING, VELVETICA MUSIC PUBLISHING
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind
The Meaning of Gnafélen
Be the first!
Post your thoughts on the meaning of "Gnafélen".