Degg Gui Lyrics

Ta khaw si degg gui degg la, nélaw si degg gui degg la
Nga diogui si degg gui degg la, degguit degguit, degg gui deggala
Ta khaw si degg gui degg la, nélaw si degg gui degg la
Nga diogui si degg gui degg la, degguit degguit, degg gui deggala

Kharitt sama wakhma degg yow, li thi ganaw degg guenalouma
Naniou mouri mbalanou wakhantoubi, té dioublou
Thi degg gui deggala
Kharitt sama wakhma degg yow, li thi ganaw degg guenalouma
Naniou mouri mbalanou wakhantoubi, té dioublou
Thi degg gui deggala

Mentira traz medo e dor
A verdade e bem mais simples nos conectados
Num canal de amor
Mentira nao
Nos deixa dormir
Andar de cabeça erguida
Soluçao tomada
Parar de mentir

Abre abre o seu coraçao hoje
Ele te salvara amanha
Salvara amanha
Salvara amanha

Kharitt sama wakhma degg yow, li thi ganaw degg guenalouma
Naniou mouri mbalanou wakhantoubi, té dioublou
Thi degg gui deggala

Deggeu si deggui deggala, nélaw si degg gui deggala
Nga takhaw si deggui deggala, degg degg, deggui deggla
Kham nga louma nékh si yow daddy sagna koor dior
Ndakh degg gui, dancoy dawal bamu matt

We, wo, la… Degg gui, yé, degg gui, degg gui deggala
Lalala li… Waw ni deggla

Writer(s): Flavia COELHO SILVA, MAMADOU MOUSTAPHA LO, François Xavier Bossard
Copyright(s): Lyrics © VAGH ET WEINMANN MUSIC, WAGRAM PUBLISHING, SPACE PARTY, Warner Chappell Music, Inc.
Lyrics Licensed & Provided by LyricFind

Attach an image to this thought

Drag image here or click to upload image

The Meaning of Degg Gui

Be the first!

Post your thoughts on the meaning of "Degg Gui".

Lyrics Discussions
Hot Songs

3

859
Recent Blog Posts